Tumgik
Photo
Tumblr media
#Sërign_Tuuba_Néena : ☆ yàlla djàpu-Léen ko, Balla Mulén di djapp; Boko jàppè dinala jàppu, Boko jàppul yàg-yagg dinala djàpp (dèe) ________ 🌎Àdduna Bayyilén ko Bala Mulén di Bàyyi; Boko Bayiwe dinala Bàyi Boko Bayiwul dinala Bàyyi (déé) _________ 👎Bàmmél deflén ci Bala ñulén ciy déf, Bo si dèffè dinañ Lafa dèf bofa défful dinañ Lafa dèf. (Déé ) __________Sërign SAALIHOU MBÀCKE ! (SMC ) https://www.instagram.com/p/B6AsUgtl20o/?igshid=1uzuabgdkecoj
0 notes
Photo
Tumblr media
SEEX_AHMADU_BÀMBA XADIM RASUUL ♦Funuy raaseeti waa juy mel ne mii mbër Woyof na ca kaw te diis na ci mbiir Boroomam ♦Funuy raaseeti jant bu dem ba njolloor Te leeral yépp gox di kenul Boroomam ♦Funuy raaseeti waa joo xam ne buy wax Ku nekk di lox di làqu ku dul Boroomam ♦Funuy raaseeti kok bu jugaa du geesoo Di romb dëram ya jëm ci mbiram Boroomam ♦Funuy raaseeti kuy fob alxuraan jii Di def ciy taax di taalif ngir Boroomam ♦Funuy raaseeti kuy gis ëhlu badrin Di ànd ak ñoom te dëkkaaleek Boroomam ♦Funuy raaseeti waa joo xam ne buy way Haraf wumu def aras di ca bég Boroomam ♦Funuy raaseeti waa joo xam ne fum teew Ku wopp mu faj ku dee mu yëgal Boroomam https://www.instagram.com/p/B5kYtXDlgmw/?igshid=1bet9e5t421eq
0 notes
Photo
Tumblr media
Tuub warna niukay déf dëgle naam Sakk sarax warna niukay déf dëgle naam Niaan warna niukay déf dëgle naam Wayé li woor daal nanie ngoyy ci Serigne Touba ta bagn ko bolék dara Moom minga hamni baat bumu waxx ak lumu binde booko taxantalé dinala woor ni ci umul kitaabi la jeumm #Cheikh_Abdoul_Ahad_Mbacké https://www.instagram.com/p/B5kYTZ7FWfl/?igshid=wlmsqxgh0ulp
0 notes
Photo
Tumblr media
"Sëriñ Tuuba kenn manu koo defaral kenn manu koo yàqal. Da nga koy jéema defaral ba far defaru. Mbaa nga jéem koo yàqal ba far yàqu. [Cheikh Abdoul Ahad Mbacké] https://www.instagram.com/p/B5kYFfsFFxd/?igshid=18vn0xto6j4d3
0 notes
Photo
Tumblr media
"Sëriñ Tuuba kenn manu koo defaral kenn manu koo yàqal. Da nga koy jéema defaral ba far defaru. Mbaa nga jéem koo yàqal ba far yàqu. [Cheikh Abdoul Ahad Mbacké] https://www.instagram.com/p/B5kX_6KFfEL/?igshid=t6wlrrmyrfw
0 notes
Photo
Tumblr media
"Yaman yaroo MOUSHABI-HAN li sheykhi ahmada Bamba" Mame Cheikh Ibra meuss na woh, MAME Massamba Ndiaye Wakhé, *Borom Ndigeul* neko: Massamba Ndiaye MOUNEKO Fall, Bamouy ÑIÈTTI Yoon, MOUNÉKO: "Waaw app liir bou NÉKÉ si biirou NDAYAME, khana FOFÂADDI ADINAME? '' MOUNEKO: WAWAW Fall FOFÂADDI ADINAME! MOUNEKO: Khana bou NIEUWÉ si adina mou GUEUNE fa yaa? MOUNEKO: WAWAW Fall birr khate na LEUNDEUM na TANGUE na! Kounouy TOUDD dima TOUDD mak "Serigne Bamba" ni adina eupé biirou WADIOUR, NILANE la EUPEI akk ko Meunti donn nak. Waxoon na yiiT, mom Mame Cheikh ibra Fall, Da NÉE woon: Ah doom sama magg Gni laffi bayyi TÉ LOUNIOU wakh deugue lay doon! Lamp Babul MOURIDINAH ma LUMIÈRE moy yoon wi, Dieureudieuf Khadimou Rassoul Diarama, Maam Cheikh Ibra Faal 👌 https://www.instagram.com/p/B5IE11qlU9q/?igshid=o5g541rxdao2
0 notes
Photo
Tumblr media
Waw kay fall BISMILAHI, Ñu NAFARAAT rék fall Ci beuyiit wi, incha allahou fall Mamam: Dalla ni YALLAHOU hanla MOUHAMDINE, Jok NÉ MÀK DEUK-MEUL YÀLLA, ba hag fa YÀLLA, Mouni: la WEUL-BEUT yabal la fa MOUHAMAD, s.a.w.s Lou tax? Boba su ÑÍU borom mingui noy JÁNGAL ak di ÑÍU wan, Kay moy "khadimu Rassoula lahi" Mouni thiow, NÉK ca LËGUEY ba di LIGUEYEUL, Mouhammad ba LËGUEY ba jegui dayoo. Moiniko: nak "Wan XAADALI MOUHAMDINE li sama di " Na ÑÍU taxaw lu def am NJANGAT fofu Boy tuud YÀLLA danga nan: "La ilaha ilal laahi MOUHAMADUN Rassoula lahi" Manam: "Allahou, wax Mouhammad, daldi NÉ Khadime" *Dangay tuud ÑIÈTI tuur juuy JEUMEUL jen jeumu* Ndax laahi ju moujj ja moy "Abdou laahi " Ta "Abdou laahi wa khadimu Rassouluho Moy tuuruw borom touba fa diwaan. Manam ÑIÈTI tuur yingay tuud tamouy JEUMEUL ken, Moy "khadimu Rassoula lahi" di tuuru borom touba" (Ndax boonai xadim moy turuw borom touba Rassoulu di MOUHAMAD ndawal YÀLLA Lahi ji moy "WAHIDUL KHAKHAAR, jala jalla laho) Moy ki jeuk moy ki moudj mame borom touba Ta nak lacci guena YÉMME modi aw TUUREUM di "khadim" Waw kon ana, lan motax mouy "Khadimu Rassoulal laahi? https://www.instagram.com/p/B5IEwh-FWqp/?igshid=1nvokz29ork6o
0 notes
Photo
Tumblr media
Sëriñ Tuubaa nee na: Boo bëggee am mboleem lo yeene ci Sunu Boroom wala ci mbindéef yi na nga sax si jàngg «Suuratul Furxaani» (8fois) ginaaw julli gu ne. Boo bëggee wërsëg bis bu ne na nga saxal «Suuratul Wàqiha» ba la ngaa nelaw. Boo bëggee mucc ci fitnay bàmmeel na nga saxal «Suuratul Mulki» ba la ngaa nelaw. Source: sëriñ àllaaji mbakké #partatger 🔴Abonnez_vous_sur_la_page https://www.instagram.com/p/B5C8RFaFZ37/?igshid=jail6a9sn4r2
0 notes
Photo
Tumblr media
Il inspire le paradis et rayonne de félicité. Il est singulièrement poétique, particulièrement sensationnel, incroyablement accueillant et démesurément bienveillant. Ô qu'il est majestueux le sourire de Seriñ Mountakha. Yalla nafi yague té wéreu https://www.instagram.com/p/B5C5ml-FIMu/?igshid=1o4yp961a7iqh
0 notes
Photo
Tumblr media
Boroom Tuubaa nee na: Kuy sàkku Yàlla Sunu Boroom, da na jariñu jariñ moroomam, kuy sàkku ludul Yàlla da na loru lor moroomam. Batay nee na: mboleem tektal yi ñeent xaaj la nu (4) partie: 1-ku lay tektal àddina 2-ku lay tektal jaamu Yàlla 3-ku lay tektal xam-xam 4-ku lay tektal Yàlla. Ku la tektal àddina fitnaal na la. Ku la tektal jaamu Yàlla sonal nala. Ku la tektal xam-xam jubal nala. Ku la tektal Yàlla noppal nala. source: sëriñ àllaaji mbakké #PARTAGER https://www.instagram.com/p/B5C5dpQFVcQ/?igshid=vcwlwue36x16
0 notes
Photo
Tumblr media
"Sa wadia Sa wadia ta wadia ma Toul way Neko yalax tga nee Meng Galass mat na way" Ndayssane! Wax diou ame solo* Riqq Hassan lu mana xéw Awal ndigal té yarou yaw Konn dinga laqq bepp yiw Téy ak ëlëg mààlako wax Mbooléém ngënéél yu dééfi utt Yaroo ko gën gën gu rafétt Moo diara dox junni bi att Di outt seriñ bulako diox Ku yaru rék a matta xam Ku yaru rék a matta am Ku yaruwul matula xam Matula xam turam wa sax Ku faboon'ub junni joxla yitt Té jappul'ub yar joxla yitt Léégi nga giss junni ya rott Borom'ub yar forko ta séx https://www.instagram.com/p/B5C4WQoFo13/?igshid=2kou4ybca2wm
0 notes
Photo
Tumblr media
Bàmba daal a baax jëfam daal a baax Waayam daal a baax waawaaw! DIAMMOU MANAMA, (LA PAIX) Yonenetebi (SAWS), dafa wakhon sunu borom Nanko "Al-lahouma IN-NIYA as ALAKOUL Hafiya" Yaw Yàlla mangui lay ñian diamou. Kon Diamou, lou amsolo LA Bi as mi lah ñu WakhTane Ci Diamou Incha Allah! Kou ted-ki: Nena: 1) Diam-mi Aduna, Moy Mothie Ci ay worr am, 2) Diam-mi Bakan, Moy Mothie Ci ay al-kandem, 3) Diam-mi Tawhiid, Moy Gnou weereul sa pass pass Ba "Ibliss" douko yakh. 4) Diam-mi Kheweul, Moy Bari te gnou Aar-ko ba beew doucca douug, 5) Diam-mi Natou, Moy Gnou Aar la banga KHAM-NE do ci gnaanki mouk. 6) Diam-mi Dun-ndou, Moy Gnou Aar-la, Banga dee ci Nguereum-moul yalla, 7) Diam-mi Talibe, Moy Gnou Aar-la , Banga nek Ci Toloub Ngeureum rek. Yàlla NAÑU Yàlla defal diamu akiy KHEWEUL FAAL, Amina Amina fall mame seex ibrahima FAAL! https://www.instagram.com/p/B5C4PNUl0RU/?igshid=lftlj6iakeqm
0 notes
Photo
Tumblr media
Bismilahi, FAAL! Jànga Léim Boroom Tuubaa kiy rammu jaam ñi: "KU TEDD KI NEENA" Keep Koo seen keen ci ÑAAR ﴾2﴿ yii la: 1﴿ Been daa am lumu BËGG diko wuti! 2﴿ Wala mu am lumu ragal diko daw! 1﴿● Ki nga xamni daa am lumu BËGG diko wuti neeko: Jarul muy sonnu, na took rek te nekk ci li Yàlla Diglé, buko deffé loolé mu BËGG diko wuti ma nga koy WËR, té ci NDIGËL yi lakoy fekk BAYABOO mu xaar ko fa jarul muy sonal boppam. 2﴿● Ki nga xamni daa am lumu ragal diko daw it neeko: Bumu daw, Bumu waaxu, Bumu Sonal boppam, na fi baayi rek linuy TÉRÉ. Nax linuy TÉRÉ ñi ngi ni siiw kuné ci ñoom bañu XËP la li ngay bañ. Daldi NÉ: Loolu li ciy misaal mooy kasso bañu kay tabax NEEWUÑU neegi keena, waayé ku def LUÑUY TÉRÉ daldi bokk ca ÑOOÑAM. https://www.instagram.com/p/B5C4LDglAJ_/?igshid=sdowls3q7o7c
0 notes
Photo
Tumblr media
"Sa Naissance est Glorieuse, Bénite, Respectueuse ; Sa célébration est obligatoire pour tout chef" dit Serigne Touba dans son poème intitulé l’Attirance des coeurs. Ici Chef signifie les hommes de DIEU, les Pieux anciens autrement dit les Guides. Etant tous des serviteurs de l’Elu ils ont pour devoir d’engager les fidèles dans toutes les actions pouvant leur garantir l’Agrément de leur SEIGNEUR. Ainsi, convaincus des Grâces que renferme cette Nuit, ils exhortent les fidèles à la célébrer. Cheikh Ahmadou Bamba Khâdimu-r-Rasûl le Serviteur du Prophète dit : "Sa Célébration conformément à la Sunna (Traditon) nous conduit vers le Paradis ; par elle les bienfaits augmentent en faveur du sincère qui glorifie". V47 Voilà donc un démenti clair à tous ceux qui dénigrent la célébration de l’anniversaire de la Naissance de la meilleure des créatures. Les détracteurs de cette célébration avancent comme argument que c’est une innovation blâmable car n’ayant jamais été célébrée du vivant du Prophète. Ceci n’est en aucun cas une raison valable pour condamner ceux qui la célèbrent d’autant plus que ceux qui la célèbrent n’ont jamais défendu que c’est une pratique traditionnelle "Sunna". On a pas dit que la célébration est une obligation traditionnelle, on a simplement dit de la vivifier selon la Tradition, c’est procéder à la récitation du Coran et des Eloges du Prophète et donner des réceptions en l’honneur des gens" Cf. sermon Serigne Saliou MBACKE pronnoncé le 19 Safar 1412H. (30 Août 1991) A la lumière de ces propos on peut dire que c’est en connaissance du rang du Prophète auprès de DIEU et de la Miséricorde dont il est porteur ainsi que des faveurs découlant du service qu’on lui rend que les pieux ont tenu à célébrer cette nuit. Espérant s’attirer les Grâces et les Bienfaits liés aux largesses que DIEU a gratifié au Prophète, ils ont invité les fidèles à se conformer à leur exemple car ils ont toujours dit qu’il est inadmissible pour un musulman de considérer la nuit de la Naissance du Prophète au même titre que les nuits qui l’ont précédé ou qui l’ont suivi. #dieureudieufé_borom_touba👌 #diaramamamecheikhibrahimafall👌🏾 https://www.instagram.com/p/B4fUZ-PFAWz/?igshid=5h24ge975gfd
0 notes
Photo
Tumblr media
#SERIGNE_TOUBA_DIGANTEEM_AK_TOUBAB_YI PARTIE 4: Serigne bi mingui diogué ndar Saint Louis thii wèeru gamou atoum année 1313 h ci gaddaay gui dieum Dakar bissoup alkhmiss jeudi bobu mu diogué ndar Saint Louis laataa diante bee soh booba daa woor. Wakh naniu né bimu aksee daniu ko daadi dougueul ci neek chambre bo khamni khatt ga ak leundeum ga fooko tak weesu na ko boolèek sobé safa nék ak lorr dia. Boolèek kooram gogu nga khamni doguko. Néena saa yuma fattaliko fanaanum ndakaaru ma ak sakh googuee ak kookee mafa dougueul sama xél day nék thii fap ay ngannaay kheekh ak nioom wayé yonnént bi saw moomay deufeul إذا ذكرت ذالك المبيتا وذالك الأمير والثبوتا طارت إلى الجهاد بالأرماح نفسي ولكن ذب عني الماحي وقال أيضا عن دكار: للمنتقى وجهت في اندكار ذكرا به قد كبكب المكار https://www.instagram.com/p/B4fUDw0lX70/?igshid=8izigttzt9hz
0 notes
Photo
Tumblr media
Cheikh Mouhammadou Mourtada mo moudje Thi Domi Cheikhoul Khadim Yi, Ni Touronedawam Moudjié Aksi Thi zayire Thi Yonent yi , Mou Gané Adouna Ak Tourou Yonent Mouhammad salahou aleyhi wa salam Thi Lokho Ndaydioram, Donou Djikko Yonent Bi saw, yattal L'islam Thi Adouna bi, Kéne meussaka dég Mouk mou wakh ba Diékhal Té wakhoul Batou L'islam Goor yallah Deug Al Moujjahidou'l Akbar Deug https://www.instagram.com/p/B4ZByVil4P8/?igshid=1m8jur7amjcgg
0 notes
Photo
Tumblr media
Seriñ modou Khabàn Mbakke Falilou Ak Sokhna Oumy Mbacke Falilou Yague Lén Fi Loll Ta wér Barkép seriñ Tuuba https://www.instagram.com/p/B4ZBILOlZ0u/?igshid=hla1ltawb930
0 notes